Aller au contenu

Tus-wu-taxaw

Jóge Wikipedia.
Lonkoyoonu àdduna bi ak yenn ci ay tus-wu-taxaw.

Tus-wu-taxaw wenn la ci ñaari xammikaay yi (beneen bi mooy tus-wu-gaar). Tus-wu-taxaw wi mooy tax ñuy man di féetale am mbir ci kaw Suuf si, ci penku walla sowwu

Lëkkalekaay yu biir

[Soppisoppi gongikuwaay bi]
wikbaatukaay am na xët wu tudd: Tus-wu-taxaw